Shared Flashcard Set

Details

Wolof Competence 2
Wolof Competence 2
66
Language - Other
Not Applicable
10/24/2009

Additional Language - Other Flashcards

 


 

Cards

Term
fr: nièce/neveu
Definition
wo: jarbaat
Term
fr: relatif/ve
Definition
wo: mbokk
Term
fr: père
Definition

wo: baay

 

Term
fr: papa
Definition
wo: pappa
Term
fr: mère
Definition
wo: yaay
Term
fr: la sœur de son père (tante)
Definition
wo: bajjan
Term
fr: le frère de sa mère (oncle)
Definition
wo: nijaay
Term
fr: petit(e) frère/sœur
Definition
wo: rakk
Term
fr: grand(e) frère/sœur
Definition
wo: mag
Term
fr: grand frère
Definition
wo: mag bu goor
Term
fr: grande sœur
Definition
wo: mag bu jigéen
Term
fr: petit frère
Definition
wo: rakk bu góor
Term
fr: petit sœur
Definition
wo: rakk bu jigéen
Term
fr: enfant
Definition
wo: doom
Term
fr: petit-enfant
Definition
wo: sët
Term
fr: neveu
Definition
wo: jarbaat bu góor
Term
fr: nièce
Definition
wo: jarbaat bu jigéen
Term
fr: grand-parent
Definition
wo: maam
Term
fr: beau-frère/belle-sœur
Definition
wo: doomu baay
Term
fr: tante (la sœur de sa mère)
Definition
wo: tataa ou tant
Term

fr: jumeau/jumelle

/ʒy.mo/

/ʒy.mɛl/

Definition
wo: seex
Term
fr: le dernier enfant
Definition
wo: caat
Term
fr: le premier enfant
Definition
wo: taaw
Term
fr: mari
Definition
wo: jëkkër ou boroom jëkkër (plus formale)
Term
fr: la femme de son oncle
Definition
wo: yumpaañ ou umpaañ
Term
fr: femme
Definition
wo: soxna ou jabar
Term
fr: co-femme
Definition
wo: wujj
Term
fr: belle famille
Definition
wo: goro
Term
fr: la famille
Definition
wo: waa kër ou njaboot
Term
fr: voisin(e)
Definition
wo: dëkkandoo ou dëkkaale
Term
fr: petite amie
Definition
wo: coro
Term
fr: petit ami
Definition
wo: far
Term
fr: femme (not a wife)
Definition
wo: jigéen
Term
fr: parents
Definition
wo: waajur
Term
fr: homonym
Definition
wo: turandoo
Term
fr: première femme
Definition
wo: aawo
Term
fr: deuxième femme
Definition
wo: ñaareel
Term
fr: troisième femme
Definition
wo: ñetteel
Term
fr: quatrième femme
Definition
wo: ñeenteel
Term
fr: un collège
Definition
wo: naatango
Term
fr: invité(e)
Definition
wo: gan
Term

fr: un jeune homme

/ʒœn/

Definition
wo: waxabaane
Term
fr: mon/ma
Definition

wo: sama + nom

 

e.g.: sama yaay mungi tudd Jeynaba

(ma mère s'appelle Jeynaba)

Term
fr: ton/ta
Definition

wo: sa + nom

 

e.g.: sa xarit mungi dekk ci Amitié 2

 

Ton ami habite à Amitié 2

Term
fr: son/sa
Definition

wo: nom+am

 

e.g.: baayam mungi tudd Musa

(son père s'appelle Musa)

Term
fr: notre
Definition
wo: sunu+nom
Term
fr: votre
Definition
wo: seen+nom
Term
fr: leur
Definition
wo: seen+nom
Term
fr: mes
Definition

wo: samay+nom

 

e.g.: samay wajur ñungi dekk Thies

Term
fr: tes
Definition

wo: say+nom

 

say doom amerikan lañu

(tes enfants sont américain)

Term
fr: ses
Definition
wo: ay+nom+am
Term
fr: nos
Definition
wo: sunuy+nom
Term
fr: vos
Definition
wo: seeni+nom
Term
fr: leurs
Definition
wo: seeni
Term

fr: donne la 1re personne singulier des verbes statifs

(je forme)

Definition

wo: verbe+naa

e.g.:am naa jabar (j'ai une femme)

(jabar=femme)

Term

fr: donne la 2e  personne singulier des verbes statifs

(tu forme)

Definition

wo: verbe+nga

 

e.g.: am nga xaalis

(tu as d'argent)

(xaalis = argent)

Term

fr: donne la 3e personne singulier des verbes statifs

(il/elle/on)

Definition

wo: verbe+na

e.g.: Faatu am na ñaari rakk yu góor

(Faatu a deux petits frères)

Term

fr: donne la 1re personne pluriel des verbes statifs

(nous forme)

Definition
wo: verbe +nanu
Term

fr: donne la 2e personne pruriel des verbes statifs

(vous forme)

Definition
wo: verbe + ngeen
Term

fr: donne la 3e personne pluriel des verbes statifs

(ils/elles forme)

Definition
wo: verbe + nañu
Term

fr: donne la 1re singulier personne des verbes statifs dans la forme negative

(je forme)

Definition

wo: verbe+uma

 

e.g.:amuma jëkkër

(je n'ai pas un mari)

Term

fr: donne la 2e personne singulier des verbes statifs dans la forme negative

(tu forme)

Definition

wo: verbe+uloo

 

e.g.: amuloo far

(tu n'as pas un petit ami)

Term

fr: donne la 3e personne singulier des verbes statifs dans la forme negatif

(il/elle/on forme)

Definition

wo: verbe+ul

 

e.g.: amul xaalis

(il n'a pas d'argent)

Term

fr: donne la 1re personne pluriel des verbes statifs dans la forme negatif

(nous forme)

Definition
wo: verbe+unu
Term

fr: donne la 2e personne pluriel des verbes statifs dans la forme negatif

(vous forme)

Definition
wo: verbe+uleen
Term

fr: donne la  3e personne pluriel des verbes statifs dans la forme negatif

(ils/elles)

Definition
wo: verbe+ uñu
Supporting users have an ad free experience!